"Wax Ju Bari"
— sunget av Youssou Ndour
"Wax Ju Bari" er en sang fremført på senegalesisk utgitt på 13 november 2021 på den offisielle kanalen til plateselskapet - "Youssou Ndour". Oppdag eksklusiv informasjon om "Wax Ju Bari". Finn sangteksten til Wax Ju Bari, oversettelser og sangfakta. Inntekter og nettoverdi akkumuleres av sponsorater og andre kilder i henhold til informasjon som finnes på internett. Hvor mange ganger dukket "Wax Ju Bari"-sangen opp i kompilerte musikklister? "Wax Ju Bari" er en velkjent musikkvideo som tok plasseringer i populære topplister, som Topp 100 Senegal sanger, Topp 40 senegalesisk sanger og mer.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Wax Ju Bari" Fakta
«Wax Ju Bari» har nådd totalt 715K visninger og 6.5K liker på YouTube.
Sangen har blitt sendt inn på 13/11/2021 og tilbrakte 19 uker på hitlistene.
Det originale navnet på musikkvideoen er "YOUSSOU NDOUR -- WAX JU BARI - ALBUM - MBALAX".
"Wax Ju Bari" har blitt publisert på Youtube på 12/11/2021 17:15:57.
"Wax Ju Bari" Lyrikk, komponister, plateselskap
« Ànd Liggéey, Wàññi Wax », car comme disait Mame Cheikh Ibrahima FALL “ Yalla Du Fay Wax Di Fàtte Jëf ”. A travers ce titre, je rends également hommage à un des monuments et pères du Mbalax : IBRA KASSE, Al Maabo Yacine Dial, un véritable Maître qu’il a été donné au Sénégal d’
;Un Maître que j’ai eu la chance d’avoir aux prémices de ma carriè
;
Boo mer ee dëgg , sëytaane da lay dugg
Jaxjax al sa xol , def loo la , li mu bëgg
And al ak dal.
Sëytaane da fay jël temps , yakkamti wul
Boo am ul chance , bu la yalla , dimmili wul
Da , lay , xaptal
Boo bëgg ée mucc , ngóor sii , yaw déglu ma
Bu la fekk oon taxaw , toog al , xarit sama
Toog al ba dal
Bu la fekk oon toog , tëdd ël , ba gagni dem
Bu yagg ee , sëytaane , day mujj dem
Doo tu la tal
bul nangu , wax ju bari yaw , ku la ko bëgg indil na nga bañ
bul ko kaf e , bul ko mbokk oo , fexe el dund te ànd ak dal
booy ànd al , na nga seet , nit ku regle , te bañ bari wax
fexe el ba adopter , dund gu ànd ul ak bari wax
ku la ko bëgg teg , bul ko nangu , bul ko masala
bari wax , da lay tardeel , bari wax ,da lay sonn al
bari wax , da lay jaxase
bu leen sonn al béer , njaw du mel ni lem
bu leen sonn al béer , njaw du mel ni lem
bu leen sonn al béer , njaw du mel ni lem
bu leen sonn al béer , njaw du mel ni lem
bu leen sonn al béer , njaw du mel ni lem
wax lu néew , jëf lou bari , kouné war na laa ,
wax lu néew , jëf lou bari , loo loo am , maanaa
Ibra kassé birame coumba Ndiaye
Kouly kassé ek maajigéen oo
Al maabo Yacine dial , ma des ca bëlbë
Moo ma daan wax naan ,
Youssou na ñu ànd liggéey , te waññi wax
Te waññi wax
Baay i Oumar , baay i Alioune , baay I ndeye kassé
Góor u fatou
Baay i idi , doom i nday i adama , ak kassé plus
Al maabo yacine dial , Ibra mor astou kassé
Fatou oy , médoune kassé
Ndoumbé yatma ,
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
wax da fay gatt yanu maanaa ,
neex a dégg lool , fees ak njariñ
ñu wax ko ba wax jot ee , fa ñu ko war a wax e
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
xaaj u guddi , boo toog oon ba mu yagg , nga doon bëccëg
di na xumb lool , ba jaaxal gaa ñi
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
wax ju néew , jëf ju bari , ku ne war na la
Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine