"Dou Mtach"
— sunget av Jahman X-Press
"Dou Mtach" er en sang fremført på senegalesisk utgitt på 21 november 2021 på den offisielle kanalen til plateselskapet - "Jahman X-Press". Oppdag eksklusiv informasjon om "Dou Mtach". Finn sangteksten til Dou Mtach, oversettelser og sangfakta. Inntekter og nettoverdi akkumuleres av sponsorater og andre kilder i henhold til informasjon som finnes på internett. Hvor mange ganger dukket "Dou Mtach"-sangen opp i kompilerte musikklister? "Dou Mtach" er en velkjent musikkvideo som tok plasseringer i populære topplister, som Topp 100 Senegal sanger, Topp 40 senegalesisk sanger og mer.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Dou Mtach" Fakta
«Dou Mtach» har nådd totalt 260.9K visninger og 4K liker på YouTube.
Sangen har blitt sendt inn på 21/11/2021 og tilbrakte 9 uker på hitlistene.
Det originale navnet på musikkvideoen er "JAHMAN X-PRESS FEAT DAYZA - DOU MTACH - ALBUM ABIYO".
"Dou Mtach" har blitt publisert på Youtube på 21/11/2021 00:43:32.
"Dou Mtach" Lyrikk, komponister, plateselskap
Production : Hoside Studio
Prod & Mix by Iso
CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08
ECOUTER L'ALBUM ICI :
Wané wou moy sa métier
Fokni fepp ngay wathié
Life bi foo ngako diapé
Né nga sa art ngay charmer
Nioune dou nii laniouy jobé
Beuri diot niak money
Call bou cher té meuno ci woté
Diaay ko bokk dieundé ko crédit
Niémé topando lo am nieup kham ko
Té do ci dara
Simpoulo niémé diaye graw
Nguirr yallah wagnil sa galathie niou diam la
Yama gueune téyeu
Lol dou match
Yaay domou diw
Lol dou match
Abeu auto diambour di gondi
dou match
Yama gueune cher call
Lol dou match
Lima yorr yoroulo ko
Dou match
Yama eup pairou daleu
Dou match
AP nga laal
Lol dou match
Resto , chicha
Lol dou match
Niit lo khamoul molay diakhal ba yaw yaa tall woné wou
Beuri daleu té sey mbirr dokhoul kone war nga kholat sa bopou
Yéré you bess nga poster
Sonal nganiok ay "new Bae"
Yoroulo lou soukeur café
Té nonou nga beugué ay doser
digue lodoul def sa "nono" be pann lougn la wakh ngani aythieu
Meune saupp té leer nama ni dadialé taw you matt sakh des fois dalay teuh
Yama dakeu Blow
Lol dou match
Yama dakeu solou
Lolou dou match
Yama gueune fashion
Dou match
Né nga yama gueune branché
Dou match
Beug saf niémé niodi
Dou match
OG la sool
Lol dou match
Mane la khalé yi di weur
Lol dou match
First class nga laal
Lol dou match
Yama gueune téyeu
Lol dou match
Yaay domou diw
Lol dou match
Abeu auto diambour di (..?)
Lol dou match
Yama gueune cher call
Lol dou match
Lima yorr yoroulo ko
Dou match
Yama eup pairou daleu
Dou match
AP nga laal
Lol dou match
Resto , chicha
Lol dou match
Fresh Baby loy diaay
Meun na dieund loy diaay
Awma jott te awma togaay
May sa dof bi mbaraan ma
Ma diokh la loy laathie baby
Dieuleul paka réndi fi
Money diamant gallé
Lep mongui fi lolou dou match
Meun ako ko noon boul tit
Danga fok ni lepa yombou
Thioow dou djipp lolou dou match
Anyway